Journée des forces Le président de l’Assemblée nationale, Monsieur Ousmane SONKO, a pris part, ce jeudi 19 novembre, à la 25e édition de la Journée nationale des Forces armées, célébrée au Camp Dial Diop, sous la présidence du président de la République, Monsieur Bassirou Diomaye Faye.
Dans la matinée, le président de l’Assemblée nationale avait tenu à rendre, à travers une publication sur sa page Facebook, un vibrant hommage à nos vaillantes Forces armées, saluant leur courage, leur engagement et leur dévouement au service de la Nation.
En rappelant leur devise emblématique, « On nous tue, on ne nous déshonore pas », il a magnifié les valeurs d’honneur, de patriotisme et de sacrifice qui fondent l’engagement de nos soldats et font la fierté de notre Nation.
————
Njiit lu Péncum ndawi askan wi, Sëriñ Usmaan SONKO, teew na, ci alxemes jii 19i fani nowàmbar, ca 25eelu Bis bi ñu jagleel Soldaari Réew mi, ñu doon ko màggale ca Dalub Jal Jóob, ci njiital Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Fay.
Ci suba si, Njiit lu Pénc mi njukkal na, sunuy Soldaar yu jàmbaare, jaare ko ci xëtuw Facebook am, rafetlu seen ug dëgër, seen ug jaayante ak seen taxawaay bu mucc ayib ci liggéeyal Réew mi.
Ci fàttali seen bàkk wii di màndargaal, « Dees nuy ray, waaye deesu nu toroxal », teg ci sargal gànjar yi, bëgg sam RÉEW ak joxe sa jëmm giy sóob sunuy soldaar di it mbégtem sunum RÉEW.