fa
Feedback
Viviane Chidid Musiques 👑🎶

Viviane Chidid Musiques 👑🎶

رفتن به کانال در Telegram

C'est pour partager les oeuvres de la reine de la musique sénégalaise

نمایش بیشتر
کشور مشخص نشده استموسیقی87 969
608
مشترکین
اطلاعاتی وجود ندارد24 ساعت
اطلاعاتی وجود ندارد7 روز
اطلاعاتی وجود ندارد30 روز

در حال بارگیری داده...

کانال‌های مشابه
ابر برچسب‌ها
هیچ داده‌ای
مشکلی وجود دارد؟ لطفاً صفحه را تازه کنید یا با مدیر پشتیبانی ما تماس بگیرید.
اشارات ورودی و خروجی
---
---
---
---
---
---
جذب مشترکین
دسامبر '24
دسامبر '24
+14
در 0 کانال‌ها
نوامبر '24
+50
در 0 کانال‌ها
Get PRO
اکتبر '24
+26
در 0 کانال‌ها
Get PRO
سپتامبر '24
+32
در 0 کانال‌ها
Get PRO
اوت '24
+8
در 0 کانال‌ها
Get PRO
ژوئیه '24
+79
در 0 کانال‌ها
Get PRO
ژوئن '24
+31
در 0 کانال‌ها
Get PRO
مه '24
+11
در 0 کانال‌ها
Get PRO
آوریل '24
+13
در 0 کانال‌ها
Get PRO
مارس '24
+16
در 0 کانال‌ها
Get PRO
فوریه '24
+624
در 0 کانال‌ها
تاریخ
رشد مشترکین
اشارات
کانال‌ها
21 دسامبر+2
20 دسامبر0
19 دسامبر0
18 دسامبر0
17 دسامبر+3
16 دسامبر0
15 دسامبر+1
14 دسامبر0
13 دسامبر0
12 دسامبر0
11 دسامبر+1
10 دسامبر0
09 دسامبر+1
08 دسامبر0
07 دسامبر0
06 دسامبر+2
05 دسامبر+1
04 دسامبر0
03 دسامبر0
02 دسامبر+1
01 دسامبر+2
پست‌های کانال
Sopé Accapella

2
+1
بدون متن...
0
3
بدون متن...
0
4
بدون متن...
0
5
بدون متن...
0
6
Sope kaay nga jege ma Sama xol yaw rekk la Dama la bëgg xawma lan la Te loolu nak demb la Sama lettre bind naa ko Ba posteel la ko nga jot ko Sama album lu ko feesal Say naatal man bëgg naa la Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Gisuma dara kele rekk Bëgguma dara kele rekk Sama xol kan moo koy dundal kele la Wuy dama la bëgg wax Ni ngiro na dimbali ma Kaay jege ma Maa neexal la Jokk dox jaagu mbaar Ngir nga kontaan Sope, jege ma Tam-tamal ma Maa ngiro ci digg laal bi Ayca kaay yëkkati ma Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Sope kaay nga jege ma Sama xol yaw rekk la Taar taxul bëgg naa la Lu yàgg rekk dëgg la Telegram bi ma jote tay Du mandat bi sama xol la Auto rail bi di corné Ma lay seen du bëgg naa la Gisuma dara kele rekk Bëgguma dara kele rekk Sama xol kan moo koy dundal kele la Wuy dama la bëgg wax Ni ngiro na dimbali ma Kaay jege ma Maa neexal la Jokk dox jaagu mbaar Ngir nga kontaan Sope, jege ma Tam-tamal ma Maa ngiro ci digg laal bi Ayca kaay yëkkati ma Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Oooh amour piis ma, bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Waaw waaw Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Waaw waaw Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la
0
7
Viviane Chidid #Sopé lyrics Sope kaay nga jege ma Sama xol yaw rekk la Dama la bëgg xawma lan la Te loolu nak demb la Sama lettre bind naa ko Ba posteel la ko nga jot ko Sama album lu ko feesal Say naatal man bëgg naa la Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Gisuma dara kele rekk Bëgguma dara kele rekk Sama xol kan moo koy dundal kele la Wuy dama la bëgg wax Ni ngiro na dimbali ma Kaay jege ma Maa neexal la Jokk dox jaagu mbaar Ngir nga kontaan Sope, jege ma Tam-tamal ma Maa ngiro ci digg laal bi Ayca kaay yëkkati ma Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Sope kaay nga jege ma Sama xol yaw rekk la Taar taxul bëgg naa la Lu yàgg rekk dëgg la Telegram bi ma jote tay Du mandat bi sama xol la Auto rail bi di corné Ma lay seen du bëgg naa la Gisuma dara kele rekk Bëgguma dara kele rekk Sama xol kan moo koy dundal kele la Wuy dama la bëgg wax Ni ngiro na dimbali ma Kaay jege ma Maa neexal la Jokk dox jaagu mbaar Ngir nga kontaan Sope, jege ma Tam-tamal ma Maa ngiro ci digg laal bi Ayca kaay yëkkati ma Amour piis ma bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Oh diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Oooh amour piis ma, bëgg naa la (Amour piis ma bëgg naa la) Sope man sopaati naa la (Sope man sopaati naa la) Diisoo na ñu dégg naa la (Diisoo na ñu dégg naa la) Amul lu may tere, ma bëgg la Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Waaw waaw Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la Waaw waaw Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la
0
8
Viviane_Chidid_-_SOPÉ(256k).mp3
0
9
بدون متن...
0
10
États-Unis : Hier, samedi, j'ai été honorée aux African Entertainment Awards USA à New Jersey, où j'ai reçu les prix de 'Meil
États-Unis : Hier, samedi, j'ai été honorée aux African Entertainment Awards USA à New Jersey, où j'ai reçu les prix de 'Meilleure Artiste Féminine Francophone' et de 'Meilleure Icône Africaine'. Cette nouvelle victoire représente un grand succès pour l'Afrique. Avec cette dynamique, nous allons hisser haut le drapeau du Sénégal partout dans le monde 🇸🇳. Je remercie infiniment le peuple sénégalais pour son soutien indéfectible. Ce prix est dédié à chacun d'entre eux. Abdou Mbaye #senegal #africamusic
0
11
بدون متن...
0
12
بدون متن...
0
13
Viviane chidid #ParForce lyrics asta la vista Dose bi lay yokk Yenn saay baax na Nga indi show time Guddi par force ci nekk Man ngeen di cons akh Boo yeewoo naan sa cafe Man may sa sugar Say nopp soo bëggee dégg lu neex, man la Yàlla ko def ci man, nangul ma ko dégg nga? Moytul reey fi nit te sa loxo laalu ko Gél bi li muy dégagée, nit antanu ko Eh yow hey Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def ci man (Ouh yeah) Danga xam wala dangay laaj? (Ouh yeah) Danga xam wala dangay laaj? (Ouh yeah) Danga xam wala dangay laaj? (Ouh yeah) Yàlla ko def ci man Àdduna ni la Soo menul jàngal Boo xamul laaj ma Ma wane la naan la Soo bëggee ma dimbali la Def la ndaanaan Kaay ma tàngal la du jeex Ni géju ndaayaan Nit ki su wetee xam boppam du ko sonnal Par force ngay nangu ni Yàlla ma téral Par force nangul ni reine bi man la Gél bi li muy dégagée, nit antanu ko Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def ci man Musique sax dangay fok ni Man la, man la, yaw Ni may solo yenn saay Da lay choqué choqué yaw Man ni ma mel tébi na yonnu naturel Gél bi li muy dégagée nit antanu ko Eh yow hey Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def ci man Sama vitesse fi muy féete auto du fa daw Bañ bañ bëgg ni ko Yàlla Buur moy dogal yaw Man ni ma mel, man ni ma mel moo naturel Gél bi li muy dégagée, nit antanu ko He yaw hey! Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def Ah yeah Danga xam wala dangay laaj? Li Yàlla def ci man Li ne ci man mi Oh wu waaw Jàmbaar ca waar wa Liggéeyam moo tax Muy rotti mbaa laaxu Te dëgg la Xoolal You fu ko neex lay fële Mag ak ndaw ñëpp di ko bëgge Man Youssou Ndour dal fépp la mane Eh! Nangul ko ko force la Moo par force la, billaahi par force la Te la nagu dey yombali duma Man de nangu na Viviane ku la yenn ciy duma Ak ku la jàngali duma Ba ko jeku caaw ko sa xiir Oh yeah fracc! Nu may def ba mu neex ni (Man da may laaj) Man fu ma jële feeling bi (Man da may laaj) Sama secret ba léegi Liggéey ba tay jàppe te bàyyiwuma Xoolal Vi fu ko neex lay fële Mag ak ndaw ñëpp di ma bëgge Fi mu newoon demb jugewu fa Eh! Bañ bañ bëgg force la Kenn bañu la! Xanaa boo rombee la ñuy doga jar Sa sañse yi ci reew mi la ñuy toog di xaar Billahi Viviane sax danga rombu art Waaw woo woo woow Ku la laaj nu mu deme ni ko li la Bu suba ci ngoon dinga comprendre Ku ci xiif tey bëgga dee di nga tàngal la ca wañ wa Xale bi, nu ko neex lay doxe Xoolal ki fu ko neex lay fële Àdduna bi dal noonu lay deme Eh! Bañ bañ bëgg force la Dégg nga? Nangul ko ko, dégg nga? Gis nga li mu mën? Nangul ko ko Coow li bari na Dara du ko teye Yàlla lu mu def jaam mënu ci dara Dégg nga? Nangul ko ko Bind bi baax na, dégg nga? Par force!
0
14
Zeyna_NDOUR_Viviane_Chidid_PHILIPPE_NDOUR_SURPRISE_256k.mp3
0
15
بدون متن...
0
16
https://youtu.be/l_YRqIGzztA?feature=shared
0
17
+6
بدون متن...
0
18
Viviane_CHIDID_-_PAR_FORCE(256k).mp3
0
19
بدون متن...
0
20
بدون متن...
0