ch
Feedback
𝙺𝚊𝚊𝚖𝚒𝚕𝚘𝚞 𝚂𝚎𝚛𝚒𝚗̃ 𝙵𝚊𝚕𝚕𝚘𝚞 𝙼𝚋𝚊𝚔𝚎́ 𝙶𝚞𝚎́𝚍𝚎́ 𝙸𝚖𝚊𝚖

𝙺𝚊𝚊𝚖𝚒𝚕𝚘𝚞 𝚂𝚎𝚛𝚒𝚗̃ 𝙵𝚊𝚕𝚕𝚘𝚞 𝙼𝚋𝚊𝚔𝚎́ 𝙶𝚞𝚎́𝚍𝚎́ 𝙸𝚖𝚊𝚖

前往频道在 Telegram

𝕃𝕖𝕔𝕥𝕦𝕣𝕖 𝕕𝕦 𝕊𝕒𝕚𝕟𝕥 ℂ𝕠𝕣𝕒𝕟 𝕡𝕒𝕣 𝕁𝕦𝕜𝕜𝕚 𝟙 𝕓𝕒 𝟛𝟘 / 𝕊𝕠𝕦𝕞𝕠𝕦𝕟 𝕡𝕒𝕣 𝕊𝕠𝕦𝕞𝕠𝕦𝕟 𝕒𝕜 𝕂𝕙𝕠𝕦𝕥𝕓𝕒 𝕊𝕖𝕣𝕚𝕟̃ 𝕓𝕚 𝕔𝕙𝕒𝕢𝕦𝕖 𝔸𝕝 𝕕𝕚𝕠𝕦𝕞𝕒

显示更多
3 773
订阅者
-624 小时
-167
-7130
帖子存档
As salam aleykoum gnou ngi siyar gneup di diokh gneup sen waćcuwaay . Dagno ame Kaamil gui gnouy diang 3 fois thie werru wolof bi . Legui nak dafa ame yeneu jukkis you libre . Legui nak kou thie beug bokkeu rek meune nagnou wakh gnou leralal ko noumouy demei inchalla

Repost from N/a
𝚂𝚘𝚞𝚛𝚊𝚝𝚎 𝙰𝚕 𝚖𝚞'𝚖𝚒𝚗𝚘𝚞𝚗
𝚂𝚘𝚞𝚛𝚊𝚝𝚎 𝙰𝚕 𝚖𝚞'𝚖𝚒𝚗𝚘𝚞𝚗

𝚃𝚊𝚖𝚋𝚊𝚕𝚒 𝚠𝚊𝚝𝚝 𝚗𝚊𝚐𝚗 𝚂𝚘𝚞𝚖𝚘𝚞𝚗 𝚙𝚊𝚛 𝚂𝚘𝚞𝚖𝚘𝚞𝚗 𝚢𝚒 𝙸𝚗𝚌𝚑𝚊𝚕𝚕𝚊

Gnou ngi nouyou gneup ❌SARTOU CANAL BI ❌👇🏽👇🏽🫱🏿 Amoul dougual beneu photo bou doywarr 🚫🔞. Amoul dougual beneu vidéo bou doywarr 🚫🔞. Amoul dougual beneu audio bou doywar 🚫🔞. Niou dimbali niou ssi rek ngir yalla Ñou bayi si khel inchallah lepp lu bokkul ci sartu canal bi daniu laay retirer . Canal gui daniou koy crée ngir ligueyal thie Al Quran keppeu . Niogui tub bu weer 🙏🏽

𝙺𝚊𝚊𝚖𝚒𝚕𝚘𝚞 𝚂𝚎𝚛𝚒𝚗̃ 𝙵𝚊𝚕𝚕𝚘𝚞 𝙼𝚋𝚊𝚔𝚎́ 𝙶𝚞𝚎́𝚍𝚎́ 𝙸𝚖𝚊𝚖 - Telegram 频道 @kzmil 的统计与分析